Home Page »  Y »  Youssou N'dour
   

Live Television Lyrics


Youssou N'dour Live Television

Paroles de la chanson Live Television :
1er couplet
Ouragan ouppeul assamane
Ba djante leer ma djanok satellite
Satellite ngalla yoné ma la khew feulé,ak fénène ak fénène
Mani go, go, go

Ni live, live television live, live tv live

2e couplet
Roplane bi warone tiim
Dima eundil ki ma namona ngui
Wayé tey télévision waar na ma, wone ma lima beugona guiss, ouragan mani ouppeul ouppeul ouppeul

Ni live, live television life, live tv live
Oh life, live tv live, live television live

Fook na né formalité leu(...)
Fook na né formalité leu(...)
Fook na né formalité leu(ma djapp yénéni chaines)
Fook na né formalité leu, leu, leu...

1er couplet

Je vais vous raconter une histoire extraordinaire
Un soir, une famille nous avait invité mes amis et moi, il y a quelques semaines de celà
Nous étions une vingtaine à nous retrouver dans un grand salon, attendant avec impatience que le dîner soit servi
Devinez ce qui est arrivé
À neuf heurs moins cinq,la famille nous abandonnés dans le salon, préférant s'entasser dans une petite chambre, avec une télé mal éclairée,uniquement pour regarder, cette fameuse émission
....khalaass
....wala bok niou dem
Chéri souma sadjobane
Dina liguey ba ame louma djeundé satellite, nguir guiss di guiss la thia bbc, la thia ortm wala la thia mtv yeah

Ni live, live television live
Live tv live
We need live, live tv live, live television live

Yaw chéri souma sadjobane, dina liguey ba me louma djeundé satellite nguir guiss di guiss la thia orts, la thia bbc wala la thia mtv yeah

Wawaw kone television wawaw

Yeah chéri souma sadjobane dina liguey ba ame louma djeundé satellite nguir guiss di guiss la thia orts, la thia cnn wala thia mtv yeah

Wawaw kone television wawaw


Browse: