Home Page »  E »  Elzo Jamdong
   

Lonely Lyrics


Elzo Jamdong Lonely

Intro
Néwone nala someu baayé me lonely (rek me lonely)
Légui réére na wone lène me yone wi (yone wi umh)

Verse 1
Togne ngama, alou na...
Youkhou nala balou na...
Li ley dioylo be légui mba dou mane?
Néwone nala méré ngama égal kharou na... (eh)

Yow la kham, mane nga mine...
Yow la am, thi mane nga mirr
Mane yow ak Ibliss rekka meunone li...
Kénène kouniou narone bolé degn koy lidieunti (eh)

Wayé lo guiss dey diékhe mat ne seukk légui
Seme pass yém ne fi mane mi ndieukke diéégui
Dém na bala khate bala yakkh santé
Ségueum diammassanté bou dag nékk daggassanté !

Chorus
Néwone nala someu baayé me lonely (rek me lonely)
Légui réér na wone lène me yone wi (yone wi umh)
Wakhone nala némeu doyoul me dolli (rek me dolli)
Mbokk ya ngui défar, nélène ma la tannone
Wayé ken mounoumeu téré me dioum
Fogone nani dessate neu wayé deme sétate
Be guiss né mounougn bokkeuti room (douniou bokkeuti room)

Verse 2
Foukki nit moun negn tollo khél (an han)
Wayé niarri nit mounouniou tollo khol (eh)
Li nga gueuneu beug moleu meuneu gueneu bégn
Ladial alcoolo bi barder thi boutélou bigne !

Ki nga beugg defe wara fadj se diangoro
Moye se kharit moye se mass moye se andeundo
Ki nga beugg defe wara done se wérou-waye
Mais bo naré deukk thi fitna deunguey warou waay

Bouniou sanione dougn fi ekssi bouniou mounone mougn...
Khamanté néniou wayé ndouro wouniou
Bi Borom bi bindé sounou tassé diouddo gouniou...
Beugguenté négn wayé dioubo wouniou

Chorus X2

Eh Douniou bokkeuti room X2
Unhu X2


Browse: