Elzo Jamdong Une Si Longue Lettre (feat. Dip Doundou Guiss)
Tagouwoume ken bimey diok di woute khey
Boumeu khole beutou diemoumele diangal feye
Bou public bi di beg rappeur yi nioye hate
Bou public bi di beg rappeur yi nioye begn
Bullshit yi nga fiy degg dou meun degn
Yobou seme tour tchi vaudou niom nioko segn
Aka niomeu yéné diapp tedj takkal chain
Diem meu neubb mouno téré seme liguey fegne
Niouné toubab ye meu defeur
Mbaa deme diouddou meune
En tt cas deme febeur Fann laa deukk
Dam ko job yalwanou ma BOKK tchi kangam yi
Boumeu diémeu topp deme yagg binde bala lii
Legui nekkatoul peace, amoul one love
Game bi defe triste kaye me wone leu
Mangui dogueu kham loutakh sene carrière tiang
Deme open mind motakh sene ay barriere ting
Niou mel ni yeneu reylou Malcolm Martin Huey Thomas Patrice Blondin ak Amaru
Mane maye ki feyou doumeu dowe doumeu bolé dina dem wouti dolé bala mey fadiou fagarou
Toubab dou kharit nit kou nioule dou mbokk
Degn ley lekk nanga sante bougn le gassalé kamb
Toubab dou kharit nit kou nioule dou mbokk
Niouné nioune nio gueum nioune nioye yar ay khambeu
Niouné nioune nio gueum nioune nioye soulli neew
Gueunoumeu diang gueunoumele nekk dioullite dé
Deunguey dounde noppi Dip guiss khoulli yemou
Yone le tchi souniou texte niou koye souligner
Liniou Fonkk souniou BAKKAN takh niou Tedj souniou GUEMMIGNE daaldi fatte souniou NOPP deukké nakh souniou BOPP
Bougn tchi diogoul dinegn yagg damm souniou TANKK dal di tass souniou yakaar diakhassok souniou bopp
Seme mbokk peul yi tannal sene dome yi dieukeur
Exciser lene diniou gueumlo ni moye deugg
Koumeu yekkal tchi diamm dina tiope beu feur
Wayé koumey lekklo force doy ne seuk
Ak Yow miné do meusseu mey se dome teugg
Khana Legui nioune nieupp yematougn tchi kanamou Yalla
Wala bok ya gueun ndakh yow leu guewel yi di tagg ?
Wala se santeu takh Adianna yafey euppeulé walleu? Han
Kouy wallou Seme life khaarouma politique mangui liguey ak seme gayi
Nel wicked yi bougoume lene guiss seme side
Nekk dioullite takhouleu andak Ossama waye
Peace seme side
Hey seme waye dounde dey dal nit dey teye moytou sheytan
Bou borom tankk di niè ki dowal mayback
Gueumeul se teint bayil me neulè khessal
Hustle hustleul diappal khoslou
Boul khare niou khassleu nga bayi boss boslou
Mouno tiope lou khadioul tchi guennoukaye beu
Bo fonkoul se bopp do done wérouwaye blood
Li ley gaagne ming se biir palace
Khamal ni liley fate ming se bir khalate
Liniou soneul moye fou sori leniou diémeu balai
Di fatté diangoro yi sakh souniou bounte gallé
Werou korr deniou gueuneu yokk liniou nougg
Nio fi daakh sanni mbedd nane deukk bi setoul
Binga diogué magal be legui niata guel nga chiare
Nio fi dakkh tarder dakh dieund montre you cher
Tagouwoume ken bimey diok di woute dieune
Boumeu khole beutou diemoumele diangal napp
Bou le gni sori di bégué gni le diegué di kheum
Bou public bi di degg niouy taf sene nopp
Tagouwoumeu ken bimey diok di wout khey
Boumeu khole beutou diemoumala diangal feey
Bou public bi di beg rappeur yi nioye hate
Bou public bi di beg rappeur yi nioy begn
D.I.P, wakhma demb lane nga DOUNDOU GUISS
{DIP DOUNDOU GUISS}
Mane dama yagga beug seet
Di seet rek pour seet li diaar si sama xel
Kone meunta niak bagna lerr
Ma geuna tiabi sama neek
Liguey rek ba deh
Si tank gnom Cheikh Anta Diop
Li ngay bagne ma def
Ni , Africian yi di yalwane batay
Gnom sen xola guena niul sen Takander
Meunou niu beugeunté ba pare di tardé rek
Comme meune nga sopp ta bagna wolou sa partenaire
Lou Goumba di doyé lamp bouko leeral ?
Pour boy yi Spider man mo meune mandela
Degg na amna ay Thiaga yuy doundal seni parents
Wayé est ce que kouy dioxé sa bopp di nga dessé dara ??
Xaral , dafa ame louma beugone lathié
Nenaniu beuguel dou diaye ba paré diabar chere
Nenagne kouy digglé tiangay dafa fek na nga set
Mane sama Grand yi dacha Mandé , dacha diokhé conseil
Gno geuna nek Killifeu ay Moustapha Niasse
Jobbako rew mi ta sa saga yi menoone na niak
Lane motakh boy yi kou diokh ni da beugue dem
Pck fi Macky sakh souy parer manda wam di dem voyage
Mane bimay nek boy fogone nani tolluway la
Niune suniu diguenté ak France bnewoule loudoul mayma
Wa ameu Yallah diokh la
Lou waye ameu , lou way meune ak ay Yallah nala Yalla fay
Yalwane rek laniu meune
Et puis sakh pour muy lerr F..ck Dupon et Demba
Xawma kagne la Demba di xamni Dupon ou gayinam
Fi tek cerveau ak Traite negriere gneuk
Yow meuno dieunde tay sou féké da nga diay sa dembeu
Sama Papeu nena mo diangul do dieurigne rew mi mouk
Immeuble Ndiougua Kebe bane ecole koffi soute
Mais boudoul wone ecole noy bindé texte yi
Mame nema tidjil sa xel ta teudj sa guemign
Deug Deug sa yaye meuno ko faye
Wayé sa mame , sa Yaye meuno ko faye
Difference teud Jail ak li di fanaane ci mbed
Moy ki dafa teuwa guenu , keulé niak foumou dieum
Boy lathe diamou Yallah interet la wala deet
Di nga xam niune ak Franc maçon yi niniu gueneunté
Marthyr ak Djihadiste wakkhma koussi guena deh
Ma wakhla gniy deglo media yi nignu guemento
Damn , guissna gnuy togne ay niitu Yallah
Guiss na gnuy raye niit ci tourou Yallah
Rabbatouma legui dama beugue guene magg
Motakh may binde ba nek bi yeup di xegne encre
Mere yi yakh seni dome ané guen yeen
Ak yeneu guel yi teela ame liberté
16 ans enceinte Happy Birthday
Tallou len loudoul feeté anniversaire
Nenalén Gallé lolen geuna talleu Tele
Nonula telé di gueuna meuna tall Galé
« Allo Fils fonek , Yeah sinon nice , ma ngi ni di nieuw sa gallé ale ma pistolet
Beneu gaine ma beugua indil problem , Daf ma amel sama djiz baparé siif daw dém
Bayil bama guiss ko rek, ki dina ratatatatatate titeu lo ndem..